Tagatt

Doxaline ci ňangalé mi

Ňangalé maa ngi wéeru ci dém ca daara ja jangi buňu toftalé ak ay misaal ci tool yi. Téeré bu ci nék dafay and ak ay aluwa yu ndogo li di ganayoo ak yénéen jumtukay yu mëngëloo ak li muy jang (powerpoint, ay theatare open office, ay site internet, ëttu E-TIC bi, ak yénnéen jumtukay yu démé ni ay téeré ak ay taagàtt yu mëngoo ak liňu soxal). Li amal naňu solo lool lèpp luy ligey um mboolo, gënn ko soxla nak ci lu jëm ci taagàtt mi gëstu bi ci tool yi.

Suňu mebet

  • Am xam-xam bu wèrr ci walu mbay mi ak lèpp lumu lamboo;
  • Am xaraňak jëlli xibaar yi am solo ngir tasaare ko ci penc mi (yum el ni lèpp lu jëm ci wallùm taskatu xibaar internet ak telefon portaabal yi);
  • Gàddu jumtukaay yi mënë tax ňu sétantal jafé-jéfé yi jaaykat yi di jankontéel ak seeni tërelin;
  • Xam tërelin yu yées yi ci walum dém béek dikk bi ngir mëna lijënti ti lèpp luy jëm ci tasaaré xibaar yi;
  • Wut ay jutukaay yu xarala ci wutum xibaar yi ci pënc mi.
©1998-2024 E-TIC|system mcart|Updated: 2019-07-30 23:00 GMT|Privacy | RSS|